MediaWiki:Anontalkpagetext/wo

From translatewiki.net
Jump to: navigation, search

Yaa ngi ci xëtu waxtaanuwaayu ab jëfandikukatu alaxam, bu bindoogul ba fim ne mbaa jëfandikoowul am sàqam.

Kon ngir xàmmee ko fàw nga jëfandikoo màkkaanub IP wam. Te màkkaanub IP jëfandikukat yu bari man nañ koo bokk. Su fekkee jëfandikukatu alaxam nga, te nga gis ne dees laa féetale ay kàddu yoo moomul, ngalla bindu walla dugg ngir benn jaxase bañatee am ëllëg .