Jump to content

Wikimedia:Pagecontentservice-description-add-link-title/wo

From translatewiki.net

Assalamoualeykoum! Ma ngui touddou Ourytima, ma ngui ligguèye ci kaggu Institut français du Sénégal. Ma ngui diangué ci eutteu ndiang mou kawé mi Cheikh Anta Diop bu Ndakarru ci daara EBAD miye yoor njanjalém kaagu yi ak ndethioumkayou terré you makk yi. Begg na bu bakha bakh ci limay binde ci sama lakke wolof nguir siwal ko ci adduna wargal keupe.